Jammu Africa
(Ismaël Lô, 1997)
Afrika a a a Afrika mon Afrique
Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq
Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew
D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique
Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a Afrika a aAfrika a a a Afrika mon Afrique
Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika
Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur
Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique
Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men
Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi
Yoo Alla addu jam to Ruanda
Yoo Alla addu jam to Burundi
Yoo Alla addu jam to Casamans
Lawol Mbignona yee
Traduction (les deux premiers couplets sont en wolof, le dernier est en Pulaar)
Dans mon rêve je prie Dieu pour que cela se réalise avant mon trépas
Je dis " un jour viendra où l'Afrique sera unie
"D'ici ou d'ailleurs nous sommes des enfants d'Afrique
Même si le ciel tombait luttons pour la paix
Donc je demande la paix en Afrique
car avec la paix en Afrique ce sera la prospérité
Etranger, moi Lô je te priequ
elles que soient ta fortune et ta situation de ne pas oublier l'Afrique
Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur
Même si le ciel pleurait luttons pour nos frères
Donc je demande la paix en Afrique
car avec la paix en Afrique ce sera la prospérité
Vous les enfants d'Afrique, levez-vous pour construire notre pays
Que Dieu nous épargne les malheurs
Qu'il apporte la paix au Rwanda, au Burundi,
Et en Casamance sur la route de Mbignona!!!
Publicado por néboa
lunes, 17 de diciembre de 2007
Suscribirse a:
Enviar comentarios (Atom)
1 comentario:
que bonita canción, no puedo dejar de escucharla....
todos somos africanos, no sé quien sería el primer descerebrado que puso precio a un trozo de tierra
Publicar un comentario